| Wolof | English | French |
| kanam gi/xar- kanam gi cëlmaay li |
face, facial appearance, expression | le visage, physionomie |
| jë bi | forehead | le front |
| neekata bi | temple | la tempe |
| nàmptal bi/naqtal bi | fontanelle | la fontanelle |
| lex bi | cheek | la joue |
| legg wi | most protuberant point of cheek below the eye | partie la plus saillante de la joue, au-dessous de l'oeil. |
| karaw gi/ kawar gi | hair, body hair | les cheveux, le poil |
| kaabaab gi | place of sideburns & along jaw | la joue des temporaux au menton |
| faas yi | sideburns | les favoris |
| kaaŋ mi | skull | le crâne, boîte crânienne humaine |
| sikkim bi | chin; beard | le menton; la barbe |
| ŋaam wi | jaw | la mâchoire |
| yaxu ŋaam bi | jawbone | la mâchoire |
Bakkan bi (The Nose)
| bakkan bi | nose; life | le nez; la vie |
| paxu bakkan bi | nostril | la narine |
| xonxon/xënxën | nasal mucosa | la muqueuse nasale |
| suuxu bakkan | nasal septum | la cloison nasale |
| nudu bakkan | bridge of nose | la base du nez |
| nuur gi | tip of the nose | le bout du nez |
| xeeñtu gi | sense of smell | l'odorat; le flair |
| bori | to have a blood nose | saigner du nez |
Bët bi (The Eye)
| bët bi/gët yi | eye | l'oeil (m); les yeux |
| yéen(u bët) bi | eyebrow | le sourcil |
| xef(u bët) wi | eyelash | le cil |
| mbarum bët mi | eyelid | la paupière |
| paxu bët bi | pupil | la pupille; la prunelle |
| peru bët bi | lens | le cristallin |
| ñuulu bët bi | iris | un iris |
| biiru bët bi | conjunctiva | la conjonctive |
| weexu bët bi | sclera, white of the eye | la sclérotique; blanc de l'oeil |
| kuggu bët | place of eyebrows & surrounds | |
| xoon gi | red part on the inner part of the eye | caroncule lacrymale |
| catu bët | outer corner of the eye | angle externe |
| siddiitu gis | optic nerve | le nerf optique |
| neexaayu bët | visual acuity | l'acuité visuelle (f) |
| gis bi | sense of sight | la vue |
| mbempen | night blindness /poor acuity | héméralopie cécité nocturne |
| rongooñ yi | tears | la larme |
| laas li | sleep in eyes | la chassie |
| jéll | to have a squint | loucher |
| payis; payis bi | jaundice, to be jaundiced | ictère (m); la jaunisse |
Nopp bi (The Ear)
| nopp bi | ear | l'oreille (f) |
| bagaanu nopp gi | pinna, ear lobe | le pavillon de l'oreille |
| taban gi | ear tip, lobule of ear | lobule of l'oreille |
| laakata nopp | cartilege in front of ear, tragus | tragus |
| paxu nopp bi | ear hole | conduit auditif externe |
| xóot-xóotu nopp bi | ear canal | conduit auditif externe |
| tulliwaan bi /biiru nopp bi | ear drum | le tympan |
| siddiitu dégg | auditory nerve | le nerf auditif |
| deggukaay | hearing apparatus | l'appareil auditif |
| neexaayu nopp | aural acuity | l'acuité auditive |
| gémmiñ gi | mouth | la bouche |
| làmmiñ wi | tongue | la langue |
| laa gi | tongue tie | frein de la langue |
| làmmiñ wu ndaw wi | uvula | uvule (f); luette (f) |
| denqaleñ bi | palate | le palais |
| tuñ mi (tuñu kaw; tuñu suuf) | lips | la lèvre |
| ciiñ mi | gum | la gencive |
| bëñ bi reewu bi sell wi déegéej bi màgg dey |
tooth incisor canine molar wisdom |
la dent incisives canine molaire dent de sagesse |
| sofe | to have mouth ulcers | avoir des aphtes |
Baat bi (The Neck)
| baat bi | neck; voice | le cou; la voix |
| xoor wi kar gi |
adam's apple | la pomme d'Adam |
| put gi bóli gi purux bi/purax bi |
throat, back of the throat, oesophagus | la gorge, le gosier |
| pottax bi | trachea, windpipe | la trachée; trachée-artère |
| dendu baat sidditu baat gi |
sternomastoid | sternocleido-mastoïdien |
| caq bi këllu poobar bi |
space above the clavicle salt cellar of clavicle |
la salière |
| yaxu caq | clavicle | la clavicule |
| ndaalu bopp | highest point on the head | |
| cuukeel bi | external occipital protuberance | la protubérance occipitale externe |
| ndoŋ li | occiput | l'occiput (m) |
| doq gi | nape of neck | la nuque |
| loos wi | back of the neck | la nuque, cou |
| ndodd li | top of spine just below cervical protuberance, vertebral column | échine |
| xaddamtiku | to clear one's throat | se racler la gorge |
| waxu gi | sore throat | le mal de gorge; angine |
| baat bu xoddoos | hoarse voice | voix rauque |
| baat bu dee | loss of voice | |
| biddanti; loos wu biddanti | to have a stiff neck; stiff neck | avoir le torticolis; le torticolis |
| cafko gi | sense of taste | le goût |
| wuum/uum | toothache | mal au dent |